Songtexte.com Drucklogo

Wakhal Songtext
von Ismaël Lô

Wakhal Songtext

Par AbouAmg


Nit kou bakh
Waroul mome di téyé meer
Bour yala diko togne lagnou deké
Wargua xalat bala guamay antou
Gueneul li khol waw bo teudé nélaw
Nit kou bah warna di balé mome
Nit kou bah warna di diéguelé
Ndakham bourbi yala dagnou deukeu
Diko togne
Bo dioulé gnane mou facé say bakar
Dafa bayi say morom yaw tanala
Bayi keur ndey ak bay guir séyal la
Kon boumou sey dou lougnouy
Tiakhané
Gueneul li khol waw bo teudé nélaw
Kay wakh ak mome kay wakh
Ak mome
Kay wakh ak mome yéneu bokeu
Diéguénaye
Kay wakh ak mome kay wakh
Ak mome
Kay wakh ak mome yéneu bokeu
Diéguénaye
Hé nagnou tiapa né djiguèn gny
Gnoye sounou kany hègne


Kon gnoune ak goune gnoune
Ak gnome
Ba saguar khègne
Mouny
Waw nagnou diapa né sey louko taka
Tassouko
Kon gnoune ak goune gnoune
Ak gnome
Ba pik ak pèle kheu
Yaw miye diame bougne la balo
Nagua balé
Bour yala mome dagnou deukeu diko
Togne
Kon yaw miye diame bougne la balo
Dagua wara balé
Ndakh bour yala mome sopeuna diam
Bouy balé
Kay wakh ak mome kay wakh
Ak mome
Kay wakh ak mome yéneu bokeu
Diéguénaye
Kay wakh ak mome kay wakh
Ak mome
Kay wakh ak mome yéneu bokeu
Diéguénaye
Bilay bilay bilay

Songtext kommentieren

Log dich ein um einen Eintrag zu schreiben.
Schreibe den ersten Kommentar!

Quiz
Wer will in seinem Song aufgeweckt werden?

Fans

»Wakhal« gefällt bisher niemandem.